loading...

graves révélations de ahmed khalifa niasse "ils ont tué mon frère et je vais..." Mp3 Télécharger

Share
Add
  • Published on Dec 5, 2018

  • graves révélations de ahmed khalifa niasse "ils ont tué mon frère et je vais..." tags

Comments

  • Ass Fall
    Ass Fall 2 months ago

    Le monde a perde l'homme fort un homme de vérité sidi lamine niass yala nala Cheikhouna Tidiane térou thia aldiana firdawsy

  • mouhamed fadel bou serigne touba

    Un grand homme est mort il laisse toujours du grand bruit

  • alima tra
    alima tra 2 months ago

    Ndeyssane derette mo for yalla fayla khalifa niass paix a son âme

  • IBA DIAGNE SARR
    IBA DIAGNE SARR 2 months ago

    Dacord na thi liga wakh sagam momm Sakou woul niou yobouko yofff ,yènn ay mbokam yiko gueuna djièguè kholl lénn famou gueuna djièkè rékk Yalla dana niousss IN CHA ALLAH ...

  • Alice Samba
    Alice Samba 2 months ago

    Fittna baxoul. Acceptons la volonté de Dieu. RIP SLN

  • barhamienne mbow
    barhamienne mbow 2 months ago

    Hawma loutakh wa senegal hypocrite gnou barri gnongui wakh thi sidy lamine té hamougnouko sakh yallah nako yallah yeureum (bala gno wakh thi yoe lou bakh nga gagnou ) wayé déngén wara hamni dara geunoul for déréte(sang) yénéna geuneu hamni khalifa mounouko bagne nagneko gnanal yallah rkk fimou dieum geun thi mome

  • Malick Sene
    Malick Sene 2 months ago

    Kén amoul loudoul sa mbok sidy yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi

  • sante yalla
    sante yalla 2 months ago

    Worone guène diapo ande bou rafète dara doulène bolène lou waye dèf bopam kène dèfoule kène dara,lèpe dina lére si kanamou yalla ,taga nopi secret de famille qu'il repose en paix sidy diambar dème na

  • Amina Gueye
    Amina Gueye 2 months ago

    Yalla na khippé aldiana firdawsi sidy etait d un grand homme

  • Clara Mendy
    Clara Mendy 2 months ago

    Bonjour à toutes et à tous,

  • papa amadou diop
    papa amadou diop 2 months ago

    Bonjour, avant tout nous disons Inna lilahi wa inna ilayhi Rajioune, nous présentons nos condéléance a sa famille en premiere et toute la ouma islamique. Qu allah le pardonne et l'octroie son paradis. Mais il n'est pas questions de dénigrer quiconque, concernant cette affaire de widy lamine Niass, de Ahmed khalifa Niass, et ce drame mieux etre bouche cousue, et laissons le grand juge la derniere parole et soyons pas ancrés la dessus par meconnaissance.

  • Yayoush Ba
    Yayoush Ba 2 months ago

    C'est très triste que dieu lui accueillant au paradis

  • ابوبكرلوح الجامبوري

    Boul thi gnanw diorte .. rafatel dirte rekk .. yalla nako yalla yeureum xare aldiana firawsi te sarax si yagu srn lokho, surtout ga remplacer ko si diabotam

  • Samba Gagnessiry Sarr
    Samba Gagnessiry Sarr 2 months ago (edited)

    Gnikoy sédé tay niouthi Bari ayy nonamm lagne wone ndakh môme DEUG AK yone ladone khékhal té niom ibliss lagne geumm AK adounaaa AK khaliss .loutakh sédé wouléne KO wone lou bakh bimiy doundou .thimmmmm narfékh yi nieupp pagui wakh té Dara geumouniouko

  • Oumar Sall
    Oumar Sall 2 months ago

    Un monument de la presse libre s'est éteint..Qu'Allah l'accueille au paradis.

  • Talibé Bamba Touba Sarr

    Sidy Lamine Niasse yalla nakko Yalla yereme té maye KO Aldiana firdawssi Ahmed khalifa Niasse yagu fi té wër

  • Adama Laffont Sy
    Adama Laffont Sy 2 months ago

    J'ai beaucoup de respect pour ce Mr . Il a une immense connaissance sur plusieurs domaines et variés. Je pense même que les Sénégalais ignorent même sa dimension. Mes condoléances à toute la famille NIASSE.

  • Bijou Diagne
    Bijou Diagne 2 months ago

    Yallah nako yallah yeureum te khareko aldiana si barke SEYDINA MOHAMED ( PSL)

  • Mouhameth Dieng
    Mouhameth Dieng 2 months ago

    Idée bou rafét mo gueune nékk fi di critiqué , diganté gnari nitt bougn balantei akheu ak si lougnou meunta diarr dara Lou gnaw amatoul fa . Ndakh nitt kou bakh dou dém moukou di yaubalé kholou mér si domou Adama yimou fi bayi, té bo kholei Ahmed mii tay khol bi dara nékoul si. En

  • Aminata Sow
    Aminata Sow 2 months ago

    Ndeyssane yalanako Yale yeureum te khareko yadiana aminn khalifa yala bakhena